Touba

dëkk bi  town, city - la ville

Wolof English français
kër-meer gi town hall la mairie
meer bi mayor le maire
pénc mi [meeting place] "l'arbre à palabres"
mbedd mi   street la rue
jàkka ji  
jumaa ji  
mosque la mosquée
julli gi  
jullit bi
prayer
muslim
la prière
le musulman
jàngu bi church l'église
oteel bi, dalalukaay hotel l'hôtel
lekkukaay bi le restaurant
toggkat bi cook, "chef" le cuisinier
baar bi coffee house le café, le bar
eleew bi  
ndongo li
scholar, pupil
student
l'écolier, l'élève
l'étudiant
jàngalekat bi teacher l'enseignant, le professeur
daara ji / bi   Koranic
school / teacher
l'école / l'enseignant
coranique
alxuraan ji Quran le Coran
téere bi   book le livre
jaayukaayu téere bi bookshop, bookstore la librairie
kàggu gi library la bibliothèque
butig bi
màngasiin bi
shop
store
la boutique
le magasin
jaaykat bi salesman, seller le vendeur
baana-baana bi street vendor le vendeur de rue
marse bi, ja bi market le marché
jaayukaayu mburu bi bakery la boulangerie
defarkatu mburu bi baker le boulanger
watkat bi hairdresser, barber le coiffeur
tiyaatar bi theater le théâtre
sinemaa bi cinema le cinéma
miise bi museum le musée
bank bi bank la banque
seg bi   check, cheque le chèque
xaalis bi   money l'argent, les sous
caga bi prostitute la prostituée
alkaati bi policeman le policier
pólis bi la police
sandarmëri bi la gendarmerie
kaso bi prison, jail la prison
janaase yi, armeel yi graveyard, cemetery le cimetière