Wolof | English | français |
tukki bi
![]() |
travel, trip | le voyage |
bagaas bi | luggage, baggage | le bagage |
ayropoor bi | airport | l'aéroport |
abiyoŋ bi | airplane, aeroplane | l'avion |
waax bi, poor bi | le port | |
gaal gi
![]() |
boat | le bateau, la pirogue |
saxaar si
![]() |
le train | |
gaar bi | railway station | la gare |
biye bi | ticket | le titre de transport |
yoon wi | path | le chemin |
tali bi
![]() |
road | la route |
kamiyon bi | truck, lorry | le camion |
bis bi kaar (rapid) bi |
bus coach |
l'autobus l'autocar |
taksi bi boroom taksi |
taxi, cab taxi driver |
le taxi le chauffeur de taxi |
oto bi | car | la voiture, l'automobile |
teerukaay bi, gaaraas bi | le garage | |
estaasyon bi | gas station | la station d'essence |
esans bi | gasoline, (petrol) | l'essence |
mótó, mobilet bi | motorcycle | la moto, le vélomoteur |
welo bi | bicycle, bike | la bicyclette, le vélo |
saret bi
![]() |
cart | la charrette |