jamono ji  time - le temps

Wolof English français
montar bi (wrist)watch la montre
Ban waxtu moo jot ? What time is it? Quelle heure est-il ?
waxtu wi   hour l'heure
simili la minute
sekond bi second la seconde
bés bi  , fan wi  
bëccëg bi
day le jour
la journée
fajar ji dawn [prière de] l'aube
njël li   l'aurore
suba si   morning le matin, la matinée
njolloor gi  
diggu-bëccëg bi
midday, noon midi
ngoon gi   afternoon
evening
l'après-midi
le soir, la soirée
marax mi
timis ji
dusk, twilight le crépuscule
[prière du crépuscule]
guddi gi   night la nuit
xaaju-guddi bi midnight minuit
bërki démb day before yesterday avant-hier
démb   yesterday hier
tey   today aujourd'hui
ëllëg si   future
tomorrow
le futur, l'avenir
demain
ginnaaw ëllëg day after tomorrow après-demain
ayubés gi week la semaine
noppaliku gi   holidays, vacation les vacances
weer wi   month le mois
jamono ji   season la saison
at mi   year l'an, l'année
Déwénati ! Happy new year! Bonne année !
ndéwénal li birthday, anniversary l'anniversaire
Ñaata at nga am ? How old are you? Quel âge as-tu ?
ndéwénal li gift for children le cadeau pour enfants
arminaat bi calendar le calendrier
xarnu bi century le siècle


Wolof English français
balaa before avant
ginnaaw after après
léegi now maintenant