numbers - les nombres

Wolof English français
0 tus zero zéro
1/2 genn-wàll gi half la moitié
1 benn   one un, une [m, f]
2 ñaar   two deux
3 ñett   three trois
4 ñent   four quatre
5 juróom   five cinq
6 juróom benn six "
7 juróom ñaar seven sept
8 juróom ñett eight huit
9 juróom ñent nine neuf
10 fukk   ten dix


Wolof
11 fukak benn
12 fukak ñaar
13 fukak ñett
14 fukak ñent
15 fukak jurom
16 fukak jurom benn
17 fukak jurom ñaar
18 fukak jurom ñett
19 fukak jurom ñent
Wolof
20 ñaar fukk
30 fann weer
40 ñen'fukk
50 jurom fukk
60 jurom benn fukk
70 jurom ñaar fukk
80 jurom ñett fukk
90 jurom ñen'fukk


Wolof English français
100 téeméer   hundred cent
1 000 junni   thousand mille
1 000
000
milyon mi million "


Wolof English français
1o jëkk first premier
2o ñaaréel second deuxième
3o ñettéel third troisième