buy bi - "monkey bread"
le "pain de singe" [fruit du baobab]

la nature

Wolof English français
àll bi   bush la brousse
suuf si   ground, soil
sand
la terre, le sol
le sable
kekk li   hard soil le sol dur
ban bi / kew gi red/white clay l'argile rouge/blanche
binit bi mud la boue
pënd bi dust la poussière
ñax mi   grass, weed
straw
l'herbe
la paille
tóor-tóor bi flower la fleur
bisaab bi   l'hibiscus
yàmbaa ji cannabis le chanvre indien
wëttéen wi cotton le coton
këriñ gi   charcoal le charbon de bois
matt mi   firewood le bois de chauffage
garab gi   tree l'arbre
guy gi   le baobab
pàkk bi   park le parc
safara si  
lakk gi  
fire
conflagration
le feu
l'incendie
tundu-safara wi volcano le volcan
tangor bi, xeer wi mountain la montagne
tund wi hill la colline
xur wi valley la vallée
déeg bi lake
pond
le lac
l'étang
jéeri ji
joor gi
plain
sandy plain
la plaine
la plaine sablonneuse
tool bi   field le champ
teen bi   water well le puits
pom bi bridge le pont
dex gi   river la rivière, le fleuve
géej gi   sea
ocean
la mer
l'océan
ginnax sea wave la vague
dun bi island l'île
tefes gi   beach la plage
dàllangeer bi,
màndiŋ mi
desert le désert
xeer wi   stone, rock la pierre, le rocher
marjaan mi diamond le diamant
petorool bi oil, (petroleum) le pétrole
gaas bi gas le gaz
weñ gi metal
iron
le métal
le fer
betteex bi lead le plomb
përëm bi copper le cuivre
xaalis bi silver l'argent
wurus wi gold l'or