kër gi   house - la maison

Wolof English français
néegu-ñax bi hut la hutte
tool bi  
toolu dër bi
garden le jardin
le jardin potager
jank bi roof le toit
sàq mi attic le grenier
kam gi, kaaw bi basement la cave
teraas bi terrace la terrasse
palanteer bi   window la fenêtre
ridó bi curtain le rideau
taax mi wall, partition le mur, la cloison
bunt bi   door la porte
tëjukaay bi, selluur bi lock la serrure, le verrou
caabi ji  
doom bi  
key la clé, la clef
yéegukaay bi stairway, stairs l'escalier
etaas bi floor, storey l'étage
bulu bi, saal bi living room la salle de séjour
anteen bi antenna l'antenne
rajo bi la radio
tele bi   television, (TV) la télévision
néeg bi   bedroom la chambre
lal bi   bed le lit
malaan mi blanket la couverture
tapi bi carpet, rug le tapis
almet bi/ji match(es) allumette(s)
làmp bi lamp la lampe
àmpul bi light bulb l'ampoule
waañ wi   kitchen la cuisine
lakkukaay bi, puur bi oven le four
firsideer bi fridge, refrigerator le frigidaire
lekkuwaay bi dining room la salle à manger
taabal bi la table
siis bi   chair la chaise
toogu bi, fotëey bi armchair le fauteuil
sanguwaay bi bathroom la salle de bain
sangu bi
sangukaay bi
bath
bathtub
le bain
la baignoire
duus bi shower la douche
sarbet bi, (fompukaay bi) towel la serviette de bain
saabu bi soap le savon
boros bi  
peñe, jartukaay bi
hairbrush
comb
la brosse à cheveux
le peigne
soccu bi toothpick le cure-dents
dantifiris bi toothpaste le dentifrice
seetu gi   mirror le miroir
xeeñ gi   perfume le parfum
wanag wi  
gaanuwaay bi  
toilet
urinal
les toilettes, les W.C.
l'urinoir
bale gi   broom le balai
mbalit mi   dustbin, trash can la poubelle