plumpy'nut
  aliment thérapeutique


  gerte gi, aréen ji  
  peanuts - les cacahuètes

lujum ji   vegetable - les légumes

Wolof English français
persi bi parsley le persil
laaj ji   garlic l'ail
soble si   onion l'oignon
pooro bi leek le poireau
mbuum mi spinach les épinards
salaat si salad
lettuce
la salade
la laitue
su / suppome bi cabbage le chou
komkombar bi cucumber le concombre
jombos bi zucchini la courgette
naajo ji
bànga bi  
squash
pumpkin
la courge
la citrouille
yomb bi   calabash la calebasse
batañse bi eggplant l'aubergine
kaani salaat gi
kaani gi  
bell pepper
chili pepper
le poivron
le piment
akara bi   bean cake le gâteau de haricots
ñebbe ji   cowpea,
black-eyed pea
le pois à vache,
la cornille
fepp   / pepp wi   cereals les céréales
mboq mi corn, maize le maïs
ceeb bi   rice le riz
dugub ji millet le mil
ñambi ji  
pullóóx bi  
cassava le manioc
pombiteer bi potato la pomme de terre
pataas bi sweet potato la patate douce
nawe bi turnip le navet
beteraaw bi beetroot la betterave
karoot ji carrot la carotte
radi bi radish le radis
tamaate bi
jaxato ji  
tomato
bitter tomato
la tomate
la tomate amère