xam-xamu natt suuf bi- geometry - la géométrie


ñatt-koñ b, ñatt-ponk b
le triangle

tolloo-wall bu jeng b
le losange - rhombus

jub-koñ b
le rectangle

ñeentaleef b, ñeent-koñ b
le carré - square

juroom-koñ b
le pentagone

juroom-benn-koñ b
l'hexagone

dagg gu waññi
l'ovale

gëweel b, mbegge g
le cercle - circle

rukk bi - l'angle