xam-xamu dun bi
geography - la géographie

Wolof English français
réew mi   country le pays
péey bi capital city la capitale
dëkk bi   town, city la ville
Gànnaar gi Mauritania la Mauritanie
naar bi   Mauritanian mauritanien
Senegaal Senegal le Sénégal
waa Senegaal Senegalese sénégalais
waa ji   inhabitant l'habitant
Lébu   Lebu people le peuple Lébou
Ndakaaru Dakar "
Kaasamaas gi la Casamance
Gàmbi   Gambia la Gambie
Giné Guinea la Guinée
Tugël   l'Europe, la France
tubaab bi   European européen, [blanc]


direction

Wolof English français
bëj-gànnaar North le Nord
bëj-saalum South le Sud
penku   East l'Est
sowu   West l'Ouest


Wolof English français
ci kaw on the top, over au-dessus, sur
ci suuf at the bottom, under au-dessous, sous
ci biir inside, into dedans
ci biti outside, out of dehors
ci ginnaaw behind derrière
ci kanam in front of devant
ci diggënte in between entre
ci digg in the center/middle au centre, au milieu
ndeyjoor bi the right la droite
càmmooñ bi the left la gauche
fii   here ici
fa   there là, là-bas
ci boor/wet beside à côté
jege   near près, proche
sore   far loin, lointain