njaboot gi  family - la famille

Wolof English français
maam ji   grandparents les grands-parents
maam ju góor ji grandfather le grand-père
maam ju jigéen ji grandmother la grand-mère
mbokk mi   le parent
baay bi   father, dad le père, papa
ndéy ji  
yaay ji  
mother, mom la mère, maman
jëkkër ji husband l'époux, le mari
aawa bi  
jabar ji  
first wife
wife
la première épouse
l'épouse
góor ji   man l'homme
jigéen ji   woman la femme
nijaay ji uncle l'oncle
bàjjan bi aunt la tante
doomu-nijaay ji
doomu-bàjjan ji
le cousin
jarbaat ji nephew
niece
le neveu
la nièce
mag ju góor ji older brother le frère aîné
rakk ju jigéen ji younger sister la sœur cadette
xale bu góor bi boy le garçon
janq bi   (virgin) girl la fille (vierge)
doom ju góor ji son le fils
doom ju jigéen ji daughter la fille (de)
xale bi  
doom ji  
child l'enfant
l'enfant (de)
liir bi   baby le bébé
xarit bi  
xarit yi
friend
friends
l'ami(e)
les amis
far wi   boyfriend le petit-ami
coro li / gel bi girlfriend la petite-amie
andandoo bi   companion le compagnon
"booy" bi (male) servant le domestique
mbindaan bi   (female) housemaid la domestique
gan gi   guest
visitor
l'invité
le visiteur
dëkkëndóo bi neighbor le voisin
nit person la personne
gaa   people les gens