wolofconnection.org

yaram wi   body - le corps

Wolof English français
der bi   skin la peau
ñàq sweat la sueur
kawar gi, (karaw) hair les cheveux
bopp bi   head la tête
jë bi   forehead le front
kaaŋ mi skull le crâne
yóor gi   brain le cerveau, (la cervelle)
kanam gi   face le visage
bët bi   / gët yi   eye(s) l'œil / les yeux
rongooñ tear la larme
nopp bi   ear l'oreille
bakkan bi   nose le nez
paxu-bakkan nostril la narine
faas yi sideburns les favoris
lex yi   cheek la joue
tuñ wi lip la lèvre
gémmiñ gi   mouth la bouche
làmmiñ wi   tongue la langue
lor saliva la salive
bëñ bi   tooth la dent
ciiñ mi gingiva, gums la gencive
ŋaam wi jaw, jawbone la mâchoire
sikkim bi chin
beard
le menton
la barbe
doq nape of the neck la nuque
baat bi   neck le cou
bóli gi  , put wi   throat la gorge
dënn bi chest la poitrine
ween wi   breast les seins
cus wi nipple le mamelon
xol bi   heart le cœur
siddit artery l'artère
waruwaayu deret vein la veine
deret ji   blood le sang
xëtër wi lung le poumon
jumbax, jumbux navel le nombril
biir bi   belly le ventre, (l'abdomen)
bàq gi stomach l'estomac
butit bi intestine l'intestin
res wi   liver le foie
gàddaam gi   spleen la rate
ndigg li hip
kidney
la hanche
le rein
saw bi   l'urine
suuf gi   l'anus
kanam gi,
(cott li, séyukaay bi)
vagina le vagin
sull bi penis le pénis
njong li   circumcision la circoncision
séy bi   sexuality la sexualité
siddit, sëddit nerve le nerf
suux wi, (sóox) le muscle
yax bi bone l'os
yaxi neen yi skeleton le squelette
ginnaaw gi   back, backbone le dos
faar gi rib la côte
mbagg mi   shoulder l'épaule
conco bi elbow le coude
loxo yi   arm
hand
le bras
la main
ténq,
tiwu-jara, tikku-jara
wrist le poignet
këmëx bi fist le poing
baaraam bi   finger le doigt
baaraamu jaaru bi ring finger l'annulaire
(baaraamu-)déy bi thumb le pouce
we wi   fingernail, nail l'ongle
taat wi   buttocks les fesses
pooj bi  , (lupp) thigh la cuisse
(w)óóm wi   knee le genou
yul bi   calf le mollet
wëq wi ankle la cheville
téstën mi   heel le talon
tànk bi  , (yeel) leg
foot
la jambe
le pied
baaraamu-tànk bi toe le doigt de pied,
l'orteil


wér gi - health - la santé

Wolof English français
ambilaas bi l'ambulance
fajukaay bi,
loppitaan bi  
hospital l'hôpital
fajkat bi,
doktoor bi  
physician, doctor le médecin, le "docteur"
jabar bi   traditional healer le guérisseur
farmasi bi pharmacy, (drugstore) la pharmacie
garab gi   medication le médicament
kawas bi   condom le préservatif,
la "capote" [pop.]
feebar bi  
jàngoro ji  
opp bi  
disease la maladie
xurfaan si   cold le rhume
sibbiru si malaria le paludisme
gaana gi   leprosy la lèpre
kuli ji la syphilis
gumba gi   blind man l'aveugle
dof bi   mad man le fou