Wolof | English | français |
weer wi
![]() |
moon | la lune |
biddééw bi
![]() |
star | l'étoile |
jant bi
![]() |
sun | le soleil |
leer gi
![]() |
sunshine, daylight | la lumière |
parasool | umbrella | le parasol, le parapluie |
ker gi | shadow, shade | l'ombre |
asamaan si
![]() |
sky | le ciel |
niir gi
![]() |
cloud | le nuage |
lay(yi) bi | fog, mist | le brouillard, la brume |
ngelaw mi
![]() |
wind | le vent |
ngëlén li | storm | la tempête |
dënnu gi
![]() |
thunder | le tonnerre |
melax gi
![]() |
flash, lightning | l'éclair |
xon wi | rainbow | l'arc-en-ciel |
taw bi
![]() |
rain | la pluie |
donju galaas bi | snow | la neige |
galaas gi
![]() |
ice | la glace |
Wolof | English | français |
tàng
![]() tàngaay bi |
hot, warm heat |
chaud la chaleur |
sedd
![]() |
cold | froid |