Wolof | English | français |
teraanga ji
![]() |
hospitality | l'hospitalité |
salam alekum ... ... alekum salam |
hello, hi | bonjour, salut |
naka suba si | good morning | bonne matinée |
ngoon | good evening | bonsoir |
ba beneen yoon | goodbye | au revoir |
Mangi dem | I am going | J'y vais |
Dama la nob | I love you | Je t'aime |
Nanga def ? | How are you? | Comment ça va ? |
Maa ngi fi rekk | I am fine | Ça va bien |
Naka nga tudd ? | What's your name? | Comment tu t'appelles ? |
Maa ngi tudd ... | My name is ... | Je m'appelle ... |
tur wi
![]() |
first name | le nom |
sant wi
![]() |
last name, family name | le nom de famille |
su la neexee | please | s'il vous plaît |
jërë jëf
![]() |
thanks, thank you | merci |
ño ko bokk | with pleasure | le plaisir est partagé |
Dégg nga wolof ? | Do you speak Wolof? | Parles-tu wolof ? |
waaw
![]() |
yes | oui |
déédéét
![]() |
no | non |
Baal ma | Excuse me | Excusez-moi |
Dimbali/Dimmali ma ! | Help! | À l'aide ! Au secours ! |