lekk gi  food - la nourriture

Wolof English français
xiif gi  
Dama xiif
hunger
I am hungry
la faim
J'ai faim
mar mi  
Dama mar
thirst
I am thirsty
la soif
J'ai soif
koor gi   fasting le jeûne du Ramadan
korité gi   [end of fasting] la fête de l'Aïd al Fitr
ndékki li   breakfast le petit-déjeuner
añ bi   lunch le déjeuner
reer bi   dinner,
supper
le dîner,
le souper


Wolof English français
palaat bi   plate l'assiette
kuddu gi
mbàttu mi  
spoon
wooden spoon
la cuillère
la cuillère en bois
furset bi fork la fourchette
paaka bi   knife le couteau
butéel bi   bottle la bouteille
kaas bi drinking glass le verre
kopp bi cup la tasse (en porcelaine)
ndab li bowl le bol
leget gi  
bagaan gi
calabash bowl le bol en calebasse



vin de palme dans une calebasse

naan gi - drink - la boisson

Wolof English français
supp bi soup la soupe
ndox mi   water l'eau
biiñ bi wine le vin
sëŋg si   palm wine le vin de palme
beer bi beer la bière
sàngara si alcohol l'alcool
attaaya bi
warga wi  
tea
green tea
le thé
le thé vert
kenkiliba gi,
séxaw si
quinqueliba "
naana ji mint la menthe
liminaat bi lemonade la limonade
sokola bi chocolate le chocolat
kafe bi coffee le café
meew mi  
soow mi  
milk
curdled milk
le lait
le lait caillé
kàcc mi   sour whey le "petit-lait"


Wolof English français
mbaanig mi, yaawuur bi yoghurt le yaourt
foromaas bi cheese le fromage
bër bi
tigadege gi  
kaarité gi
butter
peanut butter
shea butter
le beurre
le beurre d'arachide
le beurre de karité
mayonees bi la mayonnaise
dëwlin ji
diwtiir ji
cooking oil
palm oil
l'huile
l'huile de palme
bineegar bi vinegar le vinaigre
ñeex mi la sauce
saf-safal gi spices les épices
poobar bi pepper le poivre
xorom bi   salt le sel
nen bi   egg l'œuf
gejj gi   dried fish le poisson séché
sanqal si semolina la semoule
sanquf / sunguf si flour la farine
mburu mi   bread le pain
cere ji   le couscous
caakri bi [couscous au lait caillé sucré]


deseer bi - le dessert

Wolof English français
cake le gâteau
kereem galaas ice cream la crème glacée
lem gi honey le miel
suukar si sugar le sucre
tàngal bi   candy, sweet le bonbon